Assalamou Halaykoum

Mboki  Dioulit yi Mboki Taloubé niongui lén di ziaré dilén fattali ni Magal Seigne Abdoul Ahad Mbacké gui dinangne ko amal thia Touba Bélél fa Serigne Abdoul Ahad wathié ab ligééy le 07 juillet 2018 nii ngén ko guisé thi videos Magal 2017 nonii lanioukoy ande ak ahlou Khassida yi ak sopé yi thi jaamou yalla ak bernde S. Allasan Diouf s. abdoul ahad Touré s. ibra gueye niouy and ak AHLOU XASSIDA YI sopé yi  Yéndou dji Touba Bélél fék fa S. Amdy Touré mou Bakh mi niou bari xam ak Serigne Abdoul Ahad

Magal gui le 07 juillet 2018 incha allah
Réactions :

Enregistrer un commentaire

 
Top