Le Service national de l’éducation et de l’information pour la santé (SNEIPS) annonce dans un communiqué que les fidèles en partance ...
Soins gratuits pour les fidèles avant et après le Grand Magal de Touba 1435h / Edition 2013 : numéro vert gratuit (800 00 50 50)
Tukkib géej gi
Tukkib géej gi
Sëñ bi,bi mu jotee ndigalul Yàlla ak Yonnant bi (j.y.m),Yonnant bi (j.y.m) jox ko kiiraay luy dox diganteem ak tubaab yi,te loolu wax n...
Sëriñ bi sancam Jolof ak li ko waraloon
Sëriñ bi sancam Jolof ak li ko waraloon
Sëñ baa ngi sanc Jolof - ci li ma sëñ Mbàkke BUSO nettali - bi mu nekkee Tuubaa,ba nit ñi bari fa,magi donga yi denc ay soxna,dëkk yi w...
Sëriñ bi ci ni mu nekke woon ginaaw bi waajur wi làqoo (gërëmul yàlla yal na nekk ci ñoom)
Sëriñ bi ci ni mu nekke woon ginaaw bi waajur wi làqoo (gërëmul yàlla yal na nekk ci ñoom)
Moom sëñ bi,bi waajur wiy dund, nanguwutoon a taxaw mbaa muy taxawal dara,moom daal ci moom rekk la toppoon ,mel ne néew bu nuy sang, f...
xamale kuy Sëriñ bi, ak ay mbiram, ba bi waajuram wu góor làqoo
xamale kuy Sëriñ bi, ak ay mbiram, ba bi waajuram wu góor làqoo
Sëñ bi,bi mu jotee ndigalul Yàlla ak Yonnant bi (j.y.m),Yonnant bi (j.y.m) jox ko kiiraay luy dox diganteem ak tubaab yi,te loolu wax na ...
Yayah Jammeh envoie sa télévision nationale pour la couverture du Magal de Touba
Yayah Jammeh envoie sa télévision nationale pour la couverture du Magal de Touba
La GRTS qui regroupe la télévision et la radio nationale de la Gambie sera, pour la première fois, à Touba pour couvrir le Magal. C’est le C...
Inscription à :
Commentaires (Atom)


![[Vidéo] "No Commentaire" Regardez le khalif général des mourides](https://i.ytimg.com/vi/yN2C4kgqru8/default.jpg)





